Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 2

Kàdduy Waare 2:23-25

Help us?
Click on verse(s) to share them!
23Ndegam day yendoo tiis ak naqaru tës-tës, ba far fanaanoo xel mu dalul. Loolu it, cóolóoli neen.
24Kon nit amul lu gën di lekk ak a naan, di bànneexoo ñaqam. Ma gis ne loolu it Yàllaa koy maye.
25Ana kuy lekk ak a bànneexu, te du Yàlla?

Read Kàdduy Waare 2Kàdduy Waare 2
Compare Kàdduy Waare 2:23-25Kàdduy Waare 2:23-25