Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 2

Kàdduy Waare 2:21-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
21Nit a ngi doñ-doñee xel, xam-xam ak manoore, te ku doñ-doñiwuloon lay wacce alalam. Loolu it, cóolóoli neen ak naqar wu réy.
22Ma ne ana lu nit di jariñoo ci doñ-doñ ak xalaatu xol, yi muy doñ-doñaale fi kaw dun bi?

Read Kàdduy Waare 2Kàdduy Waare 2
Compare Kàdduy Waare 2:21-22Kàdduy Waare 2:21-22