Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 2

Kàdduy Waare 2:19-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19xameesul ku xeloom ku nitoodi lay doon, mooy moom lu ma doon doñ-doñi, te sama manoore manaloon ma ko fi kaw dun bi. Loolu it, cóolóoli neen.
20Sama xol a jeex ci doñ-doñ ju ma doñ-doñi fi kaw dun bi.

Read Kàdduy Waare 2Kàdduy Waare 2
Compare Kàdduy Waare 2:19-20Kàdduy Waare 2:19-20