Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 2

Kàdduy Waare 2:13-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Ma gis ne ni leer ëppe lëndëm njariñ, ni la xel mu rafet ëppe ndof njariñ.
14Ku xelu day xool fa muy jaare, dof biy tëñëx-tëñëxi cig lëndëm. Ma ne moona ñoom ñaar a bokk dogal moos.

Read Kàdduy Waare 2Kàdduy Waare 2
Compare Kàdduy Waare 2:13-14Kàdduy Waare 2:13-14