Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 1

Kàdduy Waare 1:12-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Man waarekat bi, buurub Israyil laa woon ci Yerusalem.
13Damaa dogu ne damay gëstu, teg ko ci xel mu rafet, di settantal mboolem lu nit def fu jant bi tiim. Ndaw sas wu tiis wu Yàlla sase, ñu war koo sasoo!

Read Kàdduy Waare 1Kàdduy Waare 1
Compare Kàdduy Waare 1:12-13Kàdduy Waare 1:12-13