Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 10

Kàdduy Waare 10:8-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Ku gas um yeer, repp nga tàbbi ca; ku bëtt miir, repp jaan matt la;
9kuy yett ay doj, repp nga caa gaañu; kuy gor bant, repp nga caa loru.

Read Kàdduy Waare 10Kàdduy Waare 10
Compare Kàdduy Waare 10:8-9Kàdduy Waare 10:8-9