Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 10

Kàdduy Waare 10:4-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Su la sa kilifa meree, bul jóge fa ñu la teg; tooñ yu mag, teey ba giif.
5Lu mettee ngi lu ma gis fi kaw suuf, lu mel ni njuumte lu rëcc kilifa:
6Ab dof bu ñu jox cér yu bare, boroom daraja féete suuf;

Read Kàdduy Waare 10Kàdduy Waare 10
Compare Kàdduy Waare 10:4-6Kàdduy Waare 10:4-6