Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 9

Kàddu yu Xelu 9:6-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Dëddul jëfi téxét ba dund, di jubal ci yoonu dégg.»
7Artu kuy ñaawle, feyoo saaga rekk, yedd ab soxor, yooloo loraange.
8Bul yedd kuy ñaawle, da lay jéppi; yeddal ku rafet xel, mu naw la.

Read Kàddu yu Xelu 9Kàddu yu Xelu 9
Compare Kàddu yu Xelu 9:6-8Kàddu yu Xelu 9:6-8