Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Dëgg laay wax, di bañ wax ju bon.
8Lu ma wax njub la. Amul lu dëng mbaa lu jekkadi.
9Lépp a dëggu ci ku am ug dégg, te jub ci ku for xam-xam.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:7-9Kàddu yu Xelu 8:7-9