Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Ma nga bunt dëkk ba, taxaw; fa nit ñay jaare lay xaacoo naan:
4«Yeen mbooloo yi laay yéene, doom aadama yi laay joor.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:3-4Kàddu yu Xelu 8:3-4