Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:23-26

Help us?
Click on verse(s) to share them!
23Bu yàgg lañu ma dëj, ca ndoorte la, bala suuf a sosu.
24Ba may dikk, géej amul, ndox ballul bay fees, di wal-wali.
25Dikk naa bala tund yu mag yee sampu, lu jiitu tund yu ndaw yi,
26laata Yàllaa sàkk suuf aki àllam ak feppu pënd ci àddina.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:23-26Kàddu yu Xelu 8:23-26