Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:22-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
22Soxna si, Xel mu Rafet nee na: «Aji Sax ji jagoo na ma ca njàlbéen, ma jiitu ca jëfam ya woon.
23Bu yàgg lañu ma dëj, ca ndoorte la, bala suuf a sosu.
24Ba may dikk, géej amul, ndox ballul bay fees, di wal-wali.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:22-24Kàddu yu Xelu 8:22-24