Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:13-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Ragal Aji Sax ji mooy bañ lu bon. Réy, xeebaate, yoonu mbon, ak wax ju jekkadi, ma boole bañ.
14Maa moomi digle, di maye gis-gis; maa am ug dégg, di boroom doole.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:13-14Kàddu yu Xelu 8:13-14