Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 8

Kàddu yu Xelu 8:12-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12«Man, Xel mu Rafet, foog di sama kër; xam-xam ak pexe, ma for.
13Ragal Aji Sax ji mooy bañ lu bon. Réy, xeebaate, yoonu mbon, ak wax ju jekkadi, ma boole bañ.

Read Kàddu yu Xelu 8Kàddu yu Xelu 8
Compare Kàddu yu Xelu 8:12-13Kàddu yu Xelu 8:12-13