Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 7

Kàddu yu Xelu 7:24-27

Help us?
Click on verse(s) to share them!
24Kon nag, doom, dégluleen ma, teewluleen samay wax.
25Bu leen soosu ndaw xiir ci moy, buleen teggi, topp ko.
26Bare na ku dee, moo ko rey, maneesula waññ ñi mu rey ñépp.
27Këram yoonu njaniiw la, daa bartalu, tàbbi néegi ndee.

Read Kàddu yu Xelu 7Kàddu yu Xelu 7
Compare Kàddu yu Xelu 7:24-27Kàddu yu Xelu 7:24-27