Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 7

Kàddu yu Xelu 7:21-23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
21Muy mocc ak a moccaat, ba nax ko, di wax lu neex, ba man ko.
22Waa ja jekki, topp ko, mbete yëkk wu ñuy rendiji, mbaa dof bu ñu jéng, di ko yari.
23Mooy picc mu tàbbi cig fiir. Du xam ne day dee, ba keroog fitt jam ko ci xol.

Read Kàddu yu Xelu 7Kàddu yu Xelu 7
Compare Kàddu yu Xelu 7:21-23Kàddu yu Xelu 7:21-23