Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 6

Kàddu yu Xelu 6:26-31

Help us?
Click on verse(s) to share them!
26Dogu mburu fey nab gànc; waaye jabaru jaambur, bakkanu lëmm.
27Te ku ne sawara cas, tafoo, lakk say yére.
28Ku dox ciy xal it, say tànk ñor.
29Mooy ànd ak jabaru jaambur, ku ko def gis ko.
30Deesul sikk ku sàcc aw ñam, def ci biiram ndax xiif.
31Waaye bu feeñee, fey boroom juróom yaari yoon, joxe alalu këram yépp.

Read Kàddu yu Xelu 6Kàddu yu Xelu 6
Compare Kàddu yu Xelu 6:26-31Kàddu yu Xelu 6:26-31