Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 6

Kàddu yu Xelu 6:26-29

Help us?
Click on verse(s) to share them!
26Dogu mburu fey nab gànc; waaye jabaru jaambur, bakkanu lëmm.
27Te ku ne sawara cas, tafoo, lakk say yére.
28Ku dox ciy xal it, say tànk ñor.
29Mooy ànd ak jabaru jaambur, ku ko def gis ko.

Read Kàddu yu Xelu 6Kàddu yu Xelu 6
Compare Kàddu yu Xelu 6:26-29Kàddu yu Xelu 6:26-29