Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 6

Kàddu yu Xelu 6:2-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2saw làmmiñ yeb la cim pax, nga keppu?
3Yaa ngi ci sa loxoy moroom, kon defal nii, doom, ba rëcc: doxal tinuji ko, raamali ko.
4Bul gëmm, bul nelaw!
5Dawal ni kéwél gu rëcc ub rëbb, ne fërr ni picc mu raw ab fiirkat.
6Yaafus bee, xoolal xorondom, seetal ci moom, ba muus.

Read Kàddu yu Xelu 6Kàddu yu Xelu 6
Compare Kàddu yu Xelu 6:2-6Kàddu yu Xelu 6:2-6