Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 5

Kàddu yu Xelu 5:9-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Kon nga ñàkk daraja, keneen jagoo; ku néeg bóom la.
10Jaambur jariñoo sa doole, doxandéem jagoo saw ñaq.

Read Kàddu yu Xelu 5Kàddu yu Xelu 5
Compare Kàddu yu Xelu 5:9-10Kàddu yu Xelu 5:9-10