Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 5

Kàddu yu Xelu 5:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Kon, doom, déglu ma, bul wacc samay kàddu.
8Soreel ndaw soosu, bul jege bunt këram.
9Kon nga ñàkk daraja, keneen jagoo; ku néeg bóom la.

Read Kàddu yu Xelu 5Kàddu yu Xelu 5
Compare Kàddu yu Xelu 5:7-9Kàddu yu Xelu 5:7-9