Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 5

Kàddu yu Xelu 5:20-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20Doom, ana looy xemmeme keneen, bay foye céri jaambur?
21Lu waay jëf, Aji Sax ji gis, di xool mboolem fu mu jaare.
22Jëf ju bon day fiir ka ko sàlloo, bàkkaaram di mbaal, jàpp ko.

Read Kàddu yu Xelu 5Kàddu yu Xelu 5
Compare Kàddu yu Xelu 5:20-22Kàddu yu Xelu 5:20-22