Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 4

Kàddu yu Xelu 4:3-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Man it amoon naa baay, di benn bàjjo ci saa ndey.
4Baay digal ma, ne ma: «Jàppal samay wax ci sam xel, di jëfe samay santaane, ba dund.
5Amal xel mu rafet akug dégg. Bul fàtte te bul moy samay wax.
6Bul dëddu xel mu rafet, da lay aar; sopp ko, mu sàmm la.
7Njàlbéenu xel mu rafet mooy sàkku ko; ak loo mana am, amal ug dégg.

Read Kàddu yu Xelu 4Kàddu yu Xelu 4
Compare Kàddu yu Xelu 4:3-7Kàddu yu Xelu 4:3-7