Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:9-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Teralal Aji Sax ji ci sa alal ak loo jëkka meññle,
10say sàq day fees, ne xéew, say mbàndi ndoxi reseñ di wal.
11Doom, bul xeeb yaru Aji Sax ji, bul bañ mu waññi la,

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:9-11Kàddu yu Xelu 3:9-11