Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:5-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Nanga wóoloo Aji Sax ji, sa léppi xol, te bul wéeru ci saw déggin.
6Loo mébét, bàyyil Yàlla xel, mu xàllal la yoon.
7Bul doyloo sa xel mu rafet, ragalal Aji Sax ji, dëddu mbon;

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:5-7Kàddu yu Xelu 3:5-7