Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:31-33

Help us?
Click on verse(s) to share them!
31Bul ñee ku néeg, te bu ko roy fenn.
32Aji Sax ji daa sib ku dëng, xejjoo kuy jubal.
33Aji Sax ji day alag kër ku bon, di barkeel waa kër ku jub.

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:31-33Kàddu yu Xelu 3:31-33