Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:26-29

Help us?
Click on verse(s) to share them!
26ndax Aji Sax ji da lay yiir, di la musal cig fiir.
27Bul xañ njekk ku ko yelloo, ndegam man nga ko.
28Bul ne say dëkk: «Demal ba beneen, ma jox la,» te fekk la yor.
29Bul fexeel dëkkandoo bu dëkk ak yaw ci kóolute.

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:26-29Kàddu yu Xelu 3:26-29