Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:25-27

Help us?
Click on verse(s) to share them!
25Kon doo ragal njàqare lu bette ak saaysaay buy songe,
26ndax Aji Sax ji da lay yiir, di la musal cig fiir.
27Bul xañ njekk ku ko yelloo, ndegam man nga ko.

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:25-27Kàddu yu Xelu 3:25-27