Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:22-28

Help us?
Click on verse(s) to share them!
22Day guddal saw fan, di rafetal sa jikko.
23Kon sab dox wóor, doo fakktalu.
24Soo tëddee doo tiit; say nelaw day neex.
25Kon doo ragal njàqare lu bette ak saaysaay buy songe,
26ndax Aji Sax ji da lay yiir, di la musal cig fiir.
27Bul xañ njekk ku ko yelloo, ndegam man nga ko.
28Bul ne say dëkk: «Demal ba beneen, ma jox la,» te fekk la yor.

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:22-28Kàddu yu Xelu 3:22-28