Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:22-25

Help us?
Click on verse(s) to share them!
22Day guddal saw fan, di rafetal sa jikko.
23Kon sab dox wóor, doo fakktalu.
24Soo tëddee doo tiit; say nelaw day neex.
25Kon doo ragal njàqare lu bette ak saaysaay buy songe,

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:22-25Kàddu yu Xelu 3:22-25