Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:17-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Fa muy jaare yiw la, fu mu awe jàmm la.
18Mooy garabu gudd fan ci ku ko jàpp, di mbégtey ku ca ŋoy.

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:17-18Kàddu yu Xelu 3:17-18