Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:13-15

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Mbégtee ñeel ku daj xel mu rafet ak ku am ug dégg.
14Am koo gën am xaalis, te njariñ laa raw wurus.
15Xel mu rafet a gën gànjar; loo mana bëgg moo ko raw.

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:13-15Kàddu yu Xelu 3:13-15