Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 3

Kàddu yu Xelu 3:11-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11Doom, bul xeeb yaru Aji Sax ji, bul bañ mu waññi la,
12ndax Aji Sax ji, ku mu sopp, waññi la, ni baay, ak doom ju ko neex.
13Mbégtee ñeel ku daj xel mu rafet ak ku am ug dégg.
14Am koo gën am xaalis, te njariñ laa raw wurus.

Read Kàddu yu Xelu 3Kàddu yu Xelu 3
Compare Kàddu yu Xelu 3:11-14Kàddu yu Xelu 3:11-14