Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 31

Kàddu yu Xelu 31:24-26

Help us?
Click on verse(s) to share them!
24Ndaw su ni mel day ràbb ay yére, di jaay, aki gañaay, di jox jaaykat yi.
25Faaydaak jom la làmboo, te ëllëg ubul boppam.
26Day wax lu xelu, di digle ngor.

Read Kàddu yu Xelu 31Kàddu yu Xelu 31
Compare Kàddu yu Xelu 31:24-26Kàddu yu Xelu 31:24-26