Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 31

Kàddu yu Xelu 31:10-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Jeeg bu jàmbaare, ndaw lu jafe, ba rawati gànjar!
11Jëkkër ja da koy wóolu, te jëkkër ja day am xéewal, du ko ñàkk.

Read Kàddu yu Xelu 31Kàddu yu Xelu 31
Compare Kàddu yu Xelu 31:10-11Kàddu yu Xelu 31:10-11