Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 30

Kàddu yu Xelu 30:20-25

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20Jikkoy jigéenu moykat a ngi. Day lekk, wommiku, te naan: «Defuma dara lu aay!»
21Ñett a ngii, day yëngal suuf, ba ci ñeent yu suuf àttanul:
22jaam bu falu buur, dof bu regg,
23ndaw su bon su for jëkkër, jigéen ju wuutu sangam bu jigéen.
24Ñeent a ngii, di lu tuut ci kaw suuf, te am xel, yaroo xel:
25xorondom, néew na doole, waaye bu jotee, mu denc dundam;

Read Kàddu yu Xelu 30Kàddu yu Xelu 30
Compare Kàddu yu Xelu 30:20-25Kàddu yu Xelu 30:20-25