Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 30

Kàddu yu Xelu 30:18-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
18Ñett a ngii, yéem na ma, ba ci ñeent yu ma xamul:
19yoonu jaxaay ci asamaan, yoonu jaan ci kawi doj, yoonu gaal ci diggu géej, yoon wi góor di jaar as ndaw.
20Jikkoy jigéenu moykat a ngi. Day lekk, wommiku, te naan: «Defuma dara lu aay!»

Read Kàddu yu Xelu 30Kàddu yu Xelu 30
Compare Kàddu yu Xelu 30:18-20Kàddu yu Xelu 30:18-20