Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 29

Kàddu yu Xelu 29:8-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Ñaawlekat a ngi taal ab dëkk, ku xelu di giifal mer.
9Boroom xel, buy layook ub dof, bu mereek buy ree, jàmm du am.
10Ab bóomkat day sib ku mat, di wuta bóom kuy jubal.
11Ab dof day mer, sàmbaar; ku xelu, mer, ànd ak sagoom.

Read Kàddu yu Xelu 29Kàddu yu Xelu 29
Compare Kàddu yu Xelu 29:8-11Kàddu yu Xelu 29:8-11