Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 29

Kàddu yu Xelu 29:5-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Kuy jay sa moroom, yaa ngi koy dugal.
6Ku bon day moy, ba dugal boppam; ku jub di woy ak a bànneexu.

Read Kàddu yu Xelu 29Kàddu yu Xelu 29
Compare Kàddu yu Xelu 29:5-6Kàddu yu Xelu 29:5-6