Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 29

Kàddu yu Xelu 29:2-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Ku jub falu, baadoolo bég; ab soxor jiite, baadoolo binni.
3Kuy jëfe xel, bégal sa baay; nga ànd aki gànc, yàq alal.
4Buur jub, am réew dëgër; mu bëggi galag, réew ma sànku.

Read Kàddu yu Xelu 29Kàddu yu Xelu 29
Compare Kàddu yu Xelu 29:2-4Kàddu yu Xelu 29:2-4