Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 28

Kàddu yu Xelu 28:8-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Kiy leble di tege, ba barele, kay yéwéne néew-ji-doole lay dencal.
9Soo dee tanqamlu yoon, sag ñaan sax Yàlla suur na ko.
10Ku yóbbe bàkkaar nit kuy jubal, yeer ma nga gas, yaa cay tàbbi, waaye ku mat di jagoo ngëneel.

Read Kàddu yu Xelu 28Kàddu yu Xelu 28
Compare Kàddu yu Xelu 28:8-10Kàddu yu Xelu 28:8-10