Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 28

Kàddu yu Xelu 28:22-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
22Ab nay day yàkkamtee barele, te xamul, ba ko ñàkk di dab.
23Boo artoo nit, mu baaxe la ëllëg; yaa koy gënal ku ko doon jay.
24Ku xañ say waajur seen alal te defe ne tooñoo, yaa neexook saaysaayu yàqkat.

Read Kàddu yu Xelu 28Kàddu yu Xelu 28
Compare Kàddu yu Xelu 28:22-24Kàddu yu Xelu 28:22-24