Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 28

Kàddu yu Xelu 28:21-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
21Par-parloo baaxul, waaye dogu mburu moyloo na kilifa.
22Ab nay day yàkkamtee barele, te xamul, ba ko ñàkk di dab.

Read Kàddu yu Xelu 28Kàddu yu Xelu 28
Compare Kàddu yu Xelu 28:21-22Kàddu yu Xelu 28:21-22