Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 28

Kàddu yu Xelu 28:19-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Beyal sab tool, sab dund doy; topp ay caaxaan, ndóol ba doyal.
20Boroom worma, bare barke; ku yàkkamtee woomle, sa mbugal du jaas.
21Par-parloo baaxul, waaye dogu mburu moyloo na kilifa.
22Ab nay day yàkkamtee barele, te xamul, ba ko ñàkk di dab.

Read Kàddu yu Xelu 28Kàddu yu Xelu 28
Compare Kàddu yu Xelu 28:19-22Kàddu yu Xelu 28:19-22