Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 28

Kàddu yu Xelu 28:15-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Kilifa guy soxore néew-ji-doole mook gaynde guy yëmmoo yem, mbaa rab wuy songe.
16Kilifa gu amul ug dégg, day foqati rekk, waaye ku bañ lu lewul, gudd fan.

Read Kàddu yu Xelu 28Kàddu yu Xelu 28
Compare Kàddu yu Xelu 28:15-16Kàddu yu Xelu 28:15-16