Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 28

Kàddu yu Xelu 28:12-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Bu ku jub amee ndam, mbégte mu réy la; ab soxor falu, ñépp làquji.
13Kuy làq say tooñ doo baaxle, ku koy nangu, tuub ko, am yërmandey Yàlla.
14Mbégte ñeel na ku saxoo ragal, waaye ku dëgër bopp tàbbi ci njekkar.

Read Kàddu yu Xelu 28Kàddu yu Xelu 28
Compare Kàddu yu Xelu 28:12-14Kàddu yu Xelu 28:12-14