Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 27

Kàddu yu Xelu 27:8-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Ku sore fa nga bokk, dangay mel ni picc mu sore tàggam.
9Diwook suuru day naatal xol; waaye li neex cib xarit, xol la lay digale.

Read Kàddu yu Xelu 27Kàddu yu Xelu 27
Compare Kàddu yu Xelu 27:8-9Kàddu yu Xelu 27:8-9