Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 27

Kàddu yu Xelu 27:11-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11Muusal, doom, ma bég, ba mana tontu ku ma sikk.
12Kuy foog, gisu ay, làqu; ab téxét ne ca tëñëx, loru.

Read Kàddu yu Xelu 27Kàddu yu Xelu 27
Compare Kàddu yu Xelu 27:11-12Kàddu yu Xelu 27:11-12