Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 26

Kàddu yu Xelu 26:18-23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
18Nit kuy naxe, naan: «Damay fo!» yaay dof buy sànniy jum, di fitteek a reye.
20Bu matt amul, ab taal fey, fu soskat amul it, xuloo jeex fa.
21Këriñ defi xal, matt xamb ub taal, ab xulookat di xambu ay.
22Waxi jëwkat di ñam wu neex, wuy seey, jàll ca biir-a-biir.
23Kuy wax lu neex, tey mébét lu bon, yaay xaalis bu rax, ñu xoob ca ndabal xandeer.

Read Kàddu yu Xelu 26Kàddu yu Xelu 26
Compare Kàddu yu Xelu 26:18-23Kàddu yu Xelu 26:18-23