Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 26

Kàddu yu Xelu 26:11-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11Dof day def jëfi dof, dellu ca, mooy xaj, bu waccoo, lekkaat ko.
12Ana koo gis mu ne: «Maa xelu»? Kooku ab dof a ko gën demin.

Read Kàddu yu Xelu 26Kàddu yu Xelu 26
Compare Kàddu yu Xelu 26:11-12Kàddu yu Xelu 26:11-12